Kaay Solu Fësal sa Taar - Viens t'habiller et montres ta beauté

Kaay Solu Fësal sa Taar - Viens t'habiller et montres ta beauté « La page Kaay Solu, Fësal sa Taar ou Viens t’habiller et montres ta beauté » vous offre l’o

sur commande très chères
01/09/2019

sur commande très chères

01/09/2019
"Man a solu ak man a sañse dañoo niroo te bokkuñ. Ki man a solu dina man a sañse waaye ki man a sañse man naa bañ a man ...
16/03/2015

"Man a solu ak man a sañse dañoo niroo te bokkuñ. Ki man a solu dina man a sañse waaye ki man a sañse man naa bañ a man a solu. Man a solu mooy jamono ju nekk ak lu man a xew nga xam na nga war a soloo ak la nga ca war sol. Ki man a sañse nag li ci ëpp ñaare ci ab xew-xew la koy mane. Ki man a solu du sol yére bi waaye yére bee koy sol ngir jàpp gum koy jàpp ak teg gum koy teg ci jamono.
Man a solu yit mooy xam bu tàngee li nga war sol te du doon colka gu rafle, bu seddee itam li nga war sol te doo ne sugg.
Batay man a solu mooy xam ni nga war a soloo ci barab bii ak ni nga war a soloo ci barab bee ak xam melo ( couleurs) yi ànd ak melo yi àndul. Yooyu yépp jigéeni Afrig rawatina yu Senegaal dajale nañ ko ci xamiin ak dajaliin wu rafet. Seenug colka day jot, yiwe te rafet. Moo tax Buñ soloo ba noppi ag leer akub taar day jolleekoo ci ñoom di waral ku leen gis sopp leen te weg ( respecter ) leen.
Xët wii ci feesbuk di "Kaay solu, fësal sa taar" moo len di yëgal ne day jaay ci njëg gu yomb te jàppandi ci ñépp ay ndimo ( tissu) yu rafet yuy gën a fësal seen taar.
Bu ngeen ko aajowoo man ngeen a jokkok nun ci Sms wala ngeen woo nu ci 77 921 46 77. Di na nu fexe ba ngeen jot ci gën gaa yeex ci 48 waxtu yi ci tege."

12/03/2015

L’habillement est le goût qualitatif qui se manifeste dans le choix des vêtements, la façon raffinée et discrète de les porter tandis que l’élégance est une qualité qui se caractérise par une grâce faite d'harmonie, de légèreté et d'aisance dans la forme et les lignes, dans la disposition et les proportions des parties, dans le mouvement. S’il y a une personne qui incarne toutes ses vertus pour ne pas dire ses qualités c’est bien la FEMME AFRICAINE.
La femme africaine en général et sénégalaise en particulier est une symbiose d’élégance, de raffinement et de beauté chantée partout. Elles font jaillir par leur habillement dans un style vestimentaire simple et décent, un halo lumineux qui force l’admiration et le respect.
« La page Kaay Solu, Fësal sa Taar ou Viens t’habiller et montres ta beauté » vous offre l’opportunité d’acheter à des prix très accessibles et adaptés à toutes les bourses, des tissus beaux, esthétiques et qui ne feront qu’accentuer la beauté qui émane en vous.
Si vous êtes intéressées, joignez par sms, messages ou par appels au 77 921 46 77. Votre demande sera satisfaite dans les 48 heures INCHA ALLAH.

Faites vos commandes et vous serez satisfaits aussitôt incha allah.
12/03/2015

Faites vos commandes et vous serez satisfaits aussitôt incha allah.

Adresse

Dakar

Téléphone

+221 77921 46 77

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Kaay Solu Fësal sa Taar - Viens t'habiller et montres ta beauté publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Raccourcis

Partager